Guerre des mots bou saf sap, Balla Gaye 2 vs Bombardier : "sou beuguè niou khèkh..."

Sport

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct luttetv/
luttetv/
luttetv
luttetv.com/
itfun.info

Commenti

  • Mane Sadio
    Mane Sadio21 giorno fa

    2 zéro Balla wakh rék le meune

  • Rap's house officiel
    Rap's house officiel22 giorni fa

    Bombardiéééé rek goudi goudi mbourrrrr🤗🤗🤗

  • Alioune Mbaye
    Alioune Mbaye22 giorni fa

    Balla day thiakhann rek Bombardier dinako door bamou teudal bopam🤣

  • SOLDAROU MAME SALIOU
    SOLDAROU MAME SALIOU24 giorni fa

    Bobardier ndame rék

  • Toure Lakhate
    Toure Lakhate24 giorni fa

    Bbbb

  • Boubou Soumaré
    Boubou Soumaré25 giorni fa

    Bombardier a des chances de gagner contre Balla

  • ᗷayzo Mbodj From DOUNDE
    ᗷayzo Mbodj From DOUNDE26 giorni fa

    ♥️ Bombardie 💪🏾💪🏽💪🏾💪🏽✊🏽✊🏾

  • Moustapha Djamil Mbaye
    Moustapha Djamil Mbaye26 giorni fa

    Combat Bou nara nekh MMA dou lamb d ken dou Balla Gaye 2 macha Allah ❤️ yalla nala yalla takhawou

  • talla sylla
    talla sylla27 giorni fa

    Yaw Da ngayi khoral bat rék da ngayi khar

  • ndiaga faye
    ndiaga faye27 giorni fa

    Bombardier is the king bombal bou baax waay

  • Fallou Fall
    Fallou Fall27 giorni fa

    Le Lion de Guédiawaye Balla Gaye2 mot embuanchou lambe

  • Lamzo Jameh
    Lamzo Jameh27 giorni fa

    Balla moy bayou mbeuryi

  • aida niang
    aida niang27 giorni fa

    Bala nima KO beug

  • Ridial Seck
    Ridial Seck27 giorni fa

    Balla ioe Doffo Sakh

  • ahmadou diouf
    ahmadou diouf28 giorni fa

    Balla atanou coups bombardier yi

  • ADAMA MBALLO
    ADAMA MBALLO28 giorni fa

    MERCI BALLA

  • ADAMA MBALLO
    ADAMA MBALLO28 giorni fa

    THIEY B52

  • Rima tv officielle
    Rima tv officielle28 giorni fa

    Bg2 tu es et tu seras toujours le vrai lion mon champion yalla nala yalla maye ndam♥️♥️♥️

  • Mame Cheikh Ndiaye
    Mame Cheikh Ndiaye28 giorni fa

    Sama ❤️ dafa séd trop sila balla gaye déf ak eumeu séne machalla nioune lii laniou xam diamou rék

  • Tarsilla Badji
    Tarsilla Badji28 giorni fa

    Balla kenn dou ioe , champion♥️😍♥️

  • luna luna
    luna luna28 giorni fa

    Pourtant ya un geste très beau que personne ne parle celle de Balla et Eumeu c'est ça la vie .

  • Mstr Kbsn
    Mstr Kbsn28 giorni fa

    No Lambeu nehneu Bombardier Balla Gaye Modou LO Ama Baldé lolou ay milliard moko wara teugu

  • thiatt diattara
    thiatt diattara28 giorni fa

    Balla amna problème ohhh

  • Genè ral
    Genè ral28 giorni fa

    Moussa ndoye sa Kane bobou waroko tek cissouf .

  • Genè ral
    Genè ral28 giorni fa

    Bombardier soumeunone berè yekini douko massa dane. Combat yep mo diekou.

  • EDEN Hazard
    EDEN Hazard28 giorni fa

    Balla Gaye 2 yalla nako yalla megme ndam thi kow bombardier

  • Luckson Charles
    Luckson Charles28 giorni fa

    Ja

  • Mouhamed Diagne
    Mouhamed Diagne28 giorni fa

    Waa bombardier mi 😂ah Wa baxna nala lékk dh 😂di nga fayyy dh Combat bi kagn la

  • Seex Anta
    Seex Anta28 giorni fa

    Balla gaye yall nala yalla may ndam

  • Ndeye daour Diop
    Ndeye daour Diop28 giorni fa

    Moussa Ndoye ma bokagua wayé sa thiese la farale

  • Ameth Diouff
    Ameth Diouff28 giorni fa

    Bomb mo meun10 balla

  • Modou Mbaye
    Modou Mbaye28 giorni fa

    Balla yaw do dra sa yarame bou noy damal entraîné mo gueune da ngaye sôpp yémé wo bombe ?

  • Mor Mbengue
    Mor Mbengue28 giorni fa

    😀😀😀😀😀😀😀😀

  • Seedy Bayo
    Seedy Bayo28 giorni fa

    Balla Gaye2 the really Lion 🦁🇸🇳👑👑👑👑👑🦁🦁🦁🦁Ndam rek insha Allah

  • L’homme Idéal
    L’homme Idéal28 giorni fa

    Journaliste biii mom geunuma ayy je vous sur

  • Balla Sene
    Balla Sene28 giorni fa

    Baseb

  • Quran tv
    Quran tv28 giorni fa

    Kep kou abonné sama chaîne yalna nga guisse ak rasolillahi firdawsi ci barke Al Quran ♥️

  • Ibrahima Seck
    Ibrahima Seck29 giorni fa

    Cey balla Gaye mo wekhhh bilahiiiii

  • Seyni Samb
    Seyni Samb29 giorni fa

    Balla mako beug yalnala May ndam ak Sa thies ak ama baldé blh Balla lamb mola nam

  • Seyni Sarr
    Seyni Sarr29 giorni fa

    Le roi des rois BG2 rek si khôl yii amoule lénéne 1:1 rek inchallakh

  • Mariama Diack
    Mariama Diack29 giorni fa

    Wa mane ma beugue Balla way yalla na sa diamou yague

  • Djibril Seck
    Djibril Seck29 giorni fa

    Balla c' est le roi sathies le princ

  • Thierno Ahmed Sène
    Thierno Ahmed Sène29 giorni fa

    Diaro bi mom meunone na niak nak Bala

  • MouHamed Le pardonneur
    MouHamed Le pardonneur29 giorni fa

    Billaahi Balla Gaye 2 moy le champion des champions venez confirmer

  • MAWLAYA TV
    MAWLAYA TV29 giorni fa

    Wawaw bom

  • Amdi Fall
    Amdi Fall29 giorni fa

    Machalla balla gaye 2🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • Bara Mbaye
    Bara Mbaye29 giorni fa

    Balla gaye✨🏆🇸🇳

  • Cheikh Diop
    Cheikh Diop29 giorni fa

    Lamb mola nam dh

  • goun precision
    goun precision29 giorni fa

    Nooon BALLA AK EUMEU DAWNA YARRAM DIADIEUF CHAMPION YI

  • Mansour Diagne
    Mansour Diagne29 giorni fa

    Balla🔥

  • Wade Malick
    Wade Malick29 giorni fa

    vive balla gaye 2 lamb yaye borom nala yallah maye ndam inchalah

  • Bada faye Ndiaye
    Bada faye Ndiaye29 giorni fa

    Bomb dagay mayé rek ya guena kham ni Balla d'où modou

  • Lemou Dabo
    Lemou Dabo29 giorni fa

    Bg2 rek amoul bayi ndam rek inchalla. ..@@@s.l.d

  • Yacine bou balla guaye2
    Yacine bou balla guaye229 giorni fa

    Machalla mon petit sa THies je vous souhaite le meilleur yalnala yalla défal diam ake ndam inchallah Amine yarabi machalla 🙏❤️❤️❤️ ❤️🙏

  • Yacine bou balla guaye2
    Yacine bou balla guaye229 giorni fa

    Machalla mon petit frère Balla gaye 2 l'homme au mental fort très courageux bonne continuation pour la suite djadjeuf champion yalnala yalla défal diam ake ndam inchallah Amine yarabi machalla 🙏❤️❤️❤️♥️🙏

  • Thiam Eva
    Thiam Eva29 giorni fa

    Balla 💪🏼💪🏼💪🏼💪🏼

  • Diao Abdoulaye Aziz
    Diao Abdoulaye Aziz29 giorni fa

    moussa ndoye vs Sa thiés combat Bou Néx

  • os money
    os money29 giorni fa

    Nguir yallah ak yonanté bi...bouléne boléti Balla ak Eumeu....kou Am xell dégg meuna xalate...dina xamni gnari mbeur yi dagno beuganté lolou...mane thiofel bou djégui dayo la guiss séne diganté gnom gnarr.

  • saff diagne
    saff diagne29 giorni fa

    Balla Gaye 2 yalla nala yala may ndam inchalla 🙏❤

  • PA AMATH NDIAYE
    PA AMATH NDIAYE29 giorni fa

    HO EUMEU SÉNE BALLA GUAYE ACTE BOU RAFÉTE

  • Habib Mboup
    Habib Mboup29 giorni fa

    Ohh très beau acte entre eumeu et balla

  • Babacar Senghor
    Babacar Senghor29 giorni fa

    Balla kharagne nioy lamb machalah faut le dire nioy doundal lamb

  • Ndiaga Yaaram
    Ndiaga Yaaram29 giorni fa

    Nenako Moussa khana khorom ngay sango😂

  • Mamadou lamine MANE
    Mamadou lamine MANE29 giorni fa

    Yalna diam bi deme si balla gueye merci

  • Pape Modou
    Pape Modou29 giorni fa

    Balla yalla nako yalla may ndam si Baker S babacar Sy

  • Habib mabousso Diakhate
    Habib mabousso Diakhate29 giorni fa

    Balla gaye 2 mofi meun 😎💪💪

  • selim selime
    selim selime29 giorni fa

    bombarde bombarde bombarde bombarde

  • Masamba Kane
    Masamba Kane29 giorni fa

    Antou Ka Balla Gaye 2 Yall Nala Yalla May Ndam Barkèb Borom Touba Amiiiin

  • lemzo dieng
    lemzo dieng29 giorni fa

    Mais bombardier mome kagne lay bayi beuri tamit..sa morom yeip bayinan

  • Younouss Niang
    Younouss Niang29 giorni fa

    Cool

  • Lamine Diouf
    Lamine Diouf29 giorni fa

    BG

  • Gallas Diaga
    Gallas DiagaMese fa

    Balla gaye 2 le king de l,arène

  • Gallas Diaga
    Gallas DiagaMese fa

    Ou sont les fan.c balla gaye 2

  • BUZZ SN TV
    BUZZ SN TVMese fa

    Merci beaucoup

  • Doudou Diop
    Doudou DiopMese fa

    Bombardier am gua problème bilahi

  • Matar Kamara
    Matar KamaraMese fa

    Balla yafi né❤️❤️💯💯

  • Ousseynou Laye DIENE
    Ousseynou Laye DIENEMese fa

    Moussa ndoye naga wagni wakh bi te leguey Bou bakh diakhane danoul sa thies dh

  • Khadim Sarr
    Khadim SarrMese fa

    Bg 2 lalou wakh

  • Fatou Ndiaye
    Fatou NdiayeMese fa

    Balla Gaye2 rek ichalla 💪🙏

  • Dieneba Diedhiou
    Dieneba DiedhiouMese fa

    Balla rek

  • Touba Bélél Automobile
    Touba Bélél AutomobileMese fa

    Kheon ak iaw 😂😂

  • Modou Samb
    Modou SambMese fa

    Non Eme sene dafa fan balla guiye 2

  • Mamadou Dieng
    Mamadou DiengMese fa

    Bombardier moy bandit

  • Khadim Cisse
    Khadim CisseMese fa

    Sa thies mola meune fouf moussa ndoye

  • Bai Niass
    Bai NiassMese fa

    Manifestations pour exiger leur libération immédiate et celle des autres otages du régime dictatorial. C'est exagéré, nous ne demandons pas justice pour nos morts, nous ne demandons pas la liberté pour nos frères. Quel est notre problème ?

  • Bai Niass
    Bai NiassMese fa

    Manifestations pour exiger leur libération immédiate et celle des autres otages du régime dictatorial. C'est exagéré, nous ne demandons pas justice pour nos morts, nous ne demandons pas la liberté pour nos frères. Quel est notre problème ?

  • mamadou moustapha Diop
    mamadou moustapha DiopMese fa

    Champion Moussa NDOYE changéél canne bii dacoroumaa Mouhamed biiy téguéé sii souf nii

  • 7yidd Oioio
    7yidd OioioMese fa

    Balla gaye mii mo démone maka?

  • Moustapha Gaye

    Moustapha Gaye

    Mese fa

    Waw mo démone maka mais oumra la démone dh pas adj

  • Jarod CISSE
    Jarod CISSEMese fa

    Bombe dee kou djel avance sam do nelow

  • dame mbengue
    dame mbengueMese fa

    💣 bomb bi dou tack inchallah Sa thiess aussi Ndam rek inchallah Força Ndam sama papa bi

  • dame mbengue
    dame mbengueMese fa

    Balla gaye ll Yalla nako yalla maye Ndam Lou sedd Si barquè Serigne Babacar sy ❤️💪

  • Mame bossou Saw

    Mame bossou Saw

    26 giorni fa

    Alahouma amine

  • BugattiBig Boy
    BugattiBig BoyMese fa

    Combat bi dougnou bett

  • Joe diop Diop
    Joe diop DiopMese fa

    Khamna si dra dé lokho bomb foume la dale say bokeu forsila

  • Jaiso International
    Jaiso InternationalMese fa

    Last image bi nice na

  • ndeye mou fadél afia Gueye sope s fallou
    ndeye mou fadél afia Gueye sope s fallouMese fa

    Balla gaye yalla nala yalla défal diame ndam rkk inchallah 💪💪

  • PA AMATH NDIAYE

    PA AMATH NDIAYE

    29 giorni fa

    AMINE YARABI

  • Abdoulaye cisse
    Abdoulaye cisseMese fa

    Balla Gaye moy sen Baye

  • Oscar Diallo
    Oscar DialloMese fa

    4 Avril siteu moko mom

  • magamou Niang
    magamou NiangMese fa

    Djadeuf Balla Gaye 2 !!

  • Samsyl Samsyl
    Samsyl SamsylMese fa

    Nexoul ba nexoul sama mbeur mi balla gaye moy nekhale lamb🐆💯❤💪🏾BG2 alias nekha faral dimanche ❤💯🇸🇳

  • Babacar Senghor

    Babacar Senghor

    29 giorni fa

    Deug la de mais nekha faral dimanche mom modou lo moko mom

  • TK
    TKMese fa

    Bombardier souko tégué ci yoon et khèrr ak balla ndakh balla niéméwoul bomb ci xél Forza Yalla na am ndam

Il prossimo