Youssou Ndour - Waññi Ko (version lyrics)

Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos ,

te bés bu ne , benn xar nga daan añ e

nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée

yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine

am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann

nga neeti ñu , yaw yaa ko jat , ba mu nelaw ,

· nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée

te waa nations - unies , nga ka daan loué

· te diggënté , États-Unis ak Guinée ,

daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
am na benn bés , nga ni ma , my boy
keroog daje naak , roi des arènes. 2 fois.
ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations. 2 fois.
ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy. 2 fois

na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs

na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs

techniques yooyu , japon laa ko jànge

ca yooya jamono , man la ñépp di wër

lu ñu wax nga ni fekke nga ko

fu ñu wax nga ni dem nga fa

doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw ;

waaye sa ma waa jii , ken melut ni moom.



Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal ,

Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal.

Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al

Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al.

Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo. 2 fois.





ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla


Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
www.youtube.com/c/YoussouNdour...
youssoundour...
youssoundou...

Commenti

  • Adama Dieng
    Adama Dieng50 minuti fa

    ❤️❤️❤️

  • Ndeye Faye
    Ndeye Faye2 ore fa

    ¹

  • Sokhna Mbene
    Sokhna Mbene7 ore fa

    ❤️❤️❤️❤️❤️💯

  • Moctar DRAME
    Moctar DRAME7 ore fa

    Diadieuf Youssou Marie Sène do sen morom

  • Fatou Gueye
    Fatou Gueye7 ore fa

    Merci du coiurage

  • El Hadj Malick THIOUNE
    El Hadj Malick THIOUNE10 ore fa

    THIAPATHIOLI!!!!!!!!!!

  • Tendances Couture
    Tendances Couture19 ore fa

    The Best, The African Music King, Une Fierté Universelle

  • Alioune Diop
    Alioune Diop19 ore fa

    Respect grand You notre fierté 🇸🇳✌🏽

  • Ama kane
    Ama kane22 ore fa

    J'arrête pas à l'écouter thiey assane thiam li 'ga tama fin bi

  • Modou Lamin Ceesay
    Modou Lamin Ceesay23 ore fa

    cette chanson est incroyable

  • Bocar salla
    Bocar sallaGiorno fa

    Bassiste bi nek si souff est très dangereux oh my god 😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍 YOUSSOU NDOUR THE BEST

  • Laye ibou Dieng
    Laye ibou DiengGiorno fa

    Mo meun wayy bilahi 😁😁🙆‍♂️❤❤

  • Aida Mbow
    Aida MbowGiorno fa

    Bella questa musica 🎶 ❤❤❤❤

  • Alpha Sow
    Alpha SowGiorno fa

    J'adore 💪💪💪🙏

  • Capo Elcapo
    Capo Elcapo2 giorni fa

    Classic 😎 🐐

  • Mamichou Darmanko
    Mamichou Darmanko2 giorni fa

    il est le meilleur de tous les temps

  • Mame Mbekh Diagne
    Mame Mbekh Diagne2 giorni fa

    Tu merite tout tu ya donne tous au senegal machalla lafe thiate yalla gua ame diam

  • Oumar Fall
    Oumar Fall2 giorni fa

    Youssou ndour

  • Sarro's Channel
    Sarro's Channel2 giorni fa

    Mass Allah

  • Youssoupha Badji
    Youssoupha Badji2 giorni fa

    way way dégueloulén son bi pour kham lou king bi wah

  • Mbacké Seck
    Mbacké Seck2 giorni fa

    Diffara oubbi école Musique dii orienté musiciens

  • AKAD Tv
    AKAD Tv2 giorni fa

    Sama wadji mo meuna wayy noo

  • Mama Diop
    Mama Diop2 giorni fa

    Amoulemorom ndour

  • bik momo joop
    bik momo joop2 giorni fa

    Doumasi doyall nak

  • Y
    Y2 giorni fa

    le meilleur de tout les temp 😍😘

  • Lami Sow
    Lami Sow2 giorni fa

    Machalah le roi de la musique africains longue vie à vous santé dieu te protège

  • Fatma Sow
    Fatma Sow2 giorni fa

    N’oublions pas l’équipe derrière le roi du mbalakh super étoile vous êtes fort mention spéciale à vous

  • Alioune Fall
    Alioune Fall3 giorni fa

    I say just u are the best the king

  • Omar Thiam
    Omar Thiam3 giorni fa

    King of Africa

  • salam
    salam3 giorni fa

    Ak fi diamono tolou amneu solo machalla nagnou défarat djiko yi lou s4ordinaire bilay ioe

  • Mame khary Mbodji
    Mame khary Mbodji3 giorni fa

    🥰🥰🥰

  • Oumy Faye
    Oumy Faye3 giorni fa

    Papa yousou Dal ya mana way

  • Matabara Diop
    Matabara Diop3 giorni fa

    Éternellement le meilleur...you est un don du ciel...quel talent!!!!!❤️❤️❤️

  • Ibrahima Gueye
    Ibrahima Gueye3 giorni fa

    Wanniko

  • salimata barry
    salimata barry3 giorni fa

    Ma chaallah

  • Djibril Konate
    Djibril Konate3 giorni fa

    J'aime bien cette musique je l'écoute sans arrêt 🎤👍🏾❤️🇸🇳

  • Kara Mbacke Mbaye
    Kara Mbacke Mbaye4 giorni fa

    Machalla

  • bik momo joop
    bik momo joop4 giorni fa

    Mafi nè papa you longue vie a vous j aim💕👍💫

  • Sheiktijan Sanneh
    Sheiktijan Sanneh4 giorni fa

    Ge suis très content de you par ce que il aide la population sénégalais

  • Sheiktijan Sanneh
    Sheiktijan Sanneh4 giorni fa

    Merci le roi de tout les temps

  • Saikou chaa
    Saikou chaa4 giorni fa

    ❤️

  • Diop Moussa
    Diop Moussa4 giorni fa

    ❤️❤️

  • Sangu îls fatick
    Sangu îls fatick4 giorni fa

    Mbaye gueye faye ya bon rek😂😂😂

  • ablaye22 sarre22
    ablaye22 sarre224 giorni fa

    aka meune woy

  • Momo Doumbis
    Momo Doumbis4 giorni fa

    J'ai retrouvé les lignes de basse du grand HABIB (RIP)

  • modoudal76
    modoudal764 giorni fa

    Yousso khana oussmane sonko laye wakhal

  • Mamoudou Diallo

    Mamoudou Diallo

    4 giorni fa

    meuna nek ndak day fène rek

  • Mamadou Diallo
    Mamadou Diallo4 giorni fa

    Youssou nd rre

  • DJ ADO Sénégal
    DJ ADO Sénégal4 giorni fa

    Youssou ndour dou woye si 0 zero

  • Alex Alex
    Alex Alex4 giorni fa

    international chanteur du monde plus riche en Afrique

  • Moustapha Seck
    Moustapha Seck4 giorni fa

    ROI DU MBALAX ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • Madiba Diba
    Madiba Diba4 giorni fa

    Walahi c'est un roi MADIBA depuis MAURITANIE

  • Mohamed Nokho
    Mohamed Nokho4 giorni fa

    Tonton You Text bi tamit wanniko katanam bari lolou té dou yeureumé. Wadji doutouko défati

  • Mouhamed Seck
    Mouhamed Seck4 giorni fa

    Qui a constaté le cri de Assane Thiam 1:57 Super Etoile, Quelle complicité 😂😂😂

  • adji mariama demba
    adji mariama demba5 giorni fa

    Mets le nom de la personne bi nga beug mou wagni )= =)

  • Idrissa Diack
    Idrissa Diack5 giorni fa

    El phenemeno Youssou le meilleur

  • baye ndiaga sk sk
    baye ndiaga sk sk5 giorni fa

    Roi way 🤩

  • CLARISSE SYLVA
    CLARISSE SYLVA5 giorni fa

    Machaala

  • Awa Ndiaye
    Awa Ndiaye5 giorni fa

    Moi je dis juste, Grand Youssou Yalla nga goudou fane yake sa Ndiabote.❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • ameth gueye
    ameth gueye5 giorni fa

    Non comment il est fort ce monsieur merci Youssou pour ce tube

  • Amadou Sylla
    Amadou Sylla5 giorni fa

    Amadou sylla

  • diallo seynabou
    diallo seynabou5 giorni fa

    Thiey youssou 🥰🥰🥰

  • Adama Kasse
    Adama Kasse5 giorni fa

    Le meilleur de sa génération

  • Badou Mbaye
    Badou Mbaye5 giorni fa

    Na bahi politique neique ci côté askane wi

  • Mamoudou Diallo

    Mamoudou Diallo

    4 giorni fa

    @Badou Mbaye Youssou a au moins a créé des emplois avant Macky. Et il n'est pas des genres qui fait du social devant les projecteurs. Je me demande quel raisonnement tu prônes. On accéde au pouvoir pour régler les problèmes des sénégalais. Donc pour toi toute politicien qui prend le pouvoir n'est plus du coté du peuple si je comprends bien ta définition. Dommage mais le peuple c'est l'ensemble des senégalais. Meme dans les superpuissances il y a des pauvres et des riches donc etre du peuple ne veut dire etre pauvre

  • bou kene merr

    bou kene merr

    4 giorni fa

    Askan wi dou sonko. 14morts pour mortelcombat . L histoire retiendra

  • Badou Mbaye

    Badou Mbaye

    5 giorni fa

    Pour moi le peuple c'est les femmes qui accouchent sur des charettes,les gens malades qui n'ont pas les moyens de se soigner, ceux qui n'ont rien à manger, c'est à dire ceux qui ont besoin d'aide pour moi youssou ndour devait être un député du peuple ou médiateur pour l'intérêt du peuple avec le gouvernement mais malheureusement il est à côté du pouvoir pour son propre intérêt

  • Mamoudou Diallo

    Mamoudou Diallo

    5 giorni fa

    Pour yaw nekoul si côté askan wi? Pour vous le peuple c'est les opposants. Le peuple c'est l'ensemble des Sénégalais nak.

  • Cheikh Mbengue
    Cheikh Mbengue5 giorni fa

    UN GRAND MESSIER, UN GRAND FIGURE MONDIAL MERCI LE ROI DU MUSIC AFRICAINE

  • Arame Seck
    Arame Seck5 giorni fa

    Machalla Nekhna félicitations notre Ambassadeur international ♥️♥️♥️♥️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳😍😍😍😍🥰🥰🥰🥰🙏🙏🙏🙏🙏

  • Abdou Jagne
    Abdou Jagne5 giorni fa

    Techniques yooyu,japon laa ko jange 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥💪💪Yusu y yal na nga fi yaga🙏

  • Gorgui gorgui
    Gorgui gorgui5 giorni fa

    Bilayi do sén moroom plus d'un million de vue en une semaine

  • Oumou Diallo
    Oumou Diallo5 giorni fa

    💞💞💞💞💕💕💕💓💓💗💗💖💖💖💟💟💟💯💕💞💞💓💗💖

  • Akeum Diop
    Akeum Diop5 giorni fa

    👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑

  • Madiba Diba
    Madiba Diba5 giorni fa

    Chapeau

  • zaalbi boy
    zaalbi boy5 giorni fa

    Wa ana Assana Diouf🤪 degloul wouywi

  • modou seck
    modou seck5 giorni fa

    😘😘😘

  • Mouhamed lamine Sy
    Mouhamed lamine Sy5 giorni fa

    Le mythe🤢❤

  • Mbaye Wade
    Mbaye Wade5 giorni fa

    Kinnnnnnnnnnnnnnnnnnng Moy King bi deeeee

  • Eilk Minosis
    Eilk Minosis5 giorni fa

    Thiéy NDOUR !!! Y’aaaayyyy Séne baaayyy .

  • Tafisco Bayakh
    Tafisco Bayakh6 giorni fa

    Super machallah mdrr

  • Manar Diagne
    Manar Diagne6 giorni fa

    Champion de monde

  • dioufy sarr
    dioufy sarr6 giorni fa

    Le meilleur de sa génération et de les temps respect père 🙏🏾

  • Abdoul Sarr
    Abdoul Sarr6 giorni fa

    Youssou Ndour ya KO wara wanngi tu es un grand scros tu a encaissé bocoups d'argent sur wave gratuitement la plateforme que tu propose n'es pas fiable on téléchargé des chons qui n'es pas lisible... Il faut spliqué sa et le réglé

  • Abdoul Sarr
    Abdoul Sarr6 giorni fa

    Chère Youssou Ndour on j'ai acheté l'album maïs le single téléchargé ne se lis pas,donc you on fait comment tu a encaissé mon argent s'en rien en retour

  • Sankare Mohamed

    Sankare Mohamed

    3 giorni fa

    Tu change de portable c'est mieux

  • Soldja Baby sicario
    Soldja Baby sicario6 giorni fa

    Nice 🤩😘🥰

  • Nabiha Njie
    Nabiha Njie6 giorni fa

    Welcome back le roi des mbalax we love you 😘😘😘😘😘😘

  • alaji bah
    alaji bah6 giorni fa

    KING suma woii katt bi Marsha'allah

  • hadj kebe
    hadj kebe6 giorni fa

    Deug deug deug deug deug deug deug, Youssou, andina bi bamou dath, yafi dakha weuye teigou ci Michael Jackson. J'ai jamais entendu une voix aussi extraordinaire que celle-là. Wayei tmt, Super étoile keine deimoule ngueine deiss yeine tmt. Bouba Ndour saï saï music bi, iow yaye le meilleur producteur musical de tous les temps au Sénégal, les preuves sont palpables.

  • oni mad
    oni mad6 giorni fa

    Le corrompue manteur

  • Mass DIOUM
    Mass DIOUM6 giorni fa

    The best

  • Malick Sene
    Malick Sene6 giorni fa

    Thieyy andou super étoile bou yokouwoul dall d'où wanjiekou mancha ala

  • KHOSS MUSIC
    KHOSS MUSIC6 giorni fa

    Ça voie reste toujours le même

  • Souadou Ndiaye
    Souadou Ndiaye6 giorni fa

    Iolmm

  • malick ndiaye
    malick ndiaye6 giorni fa

    Cey you kene meunou la merei. Mais pour le clip il faut patin quoi Di na nice deh.

  • Ahm Mouss
    Ahm Mouss6 giorni fa

    Un chef-d'œuvre 🤭👍💪♥️♥️💯

  • Mamadou Ba
    Mamadou Ba6 giorni fa

    Kone you kafoul Doulkatt yii la woyy 😂😂

  • Ibrahima Gueye
    Ibrahima Gueye6 giorni fa

    Nice😍😍😍

  • young wizz taylor!
    young wizz taylor!6 giorni fa

    Deuyzeukoulanah Youssou ndour bilahi ma le begue yow Lo way mou néx🥰 kou daccord ke Youssou ndour est le meilleur 🔥

  • aliou diedhiou
    aliou diedhiou6 giorni fa

    The king of king. Notre fierté youssou ndour

  • Kawsy Sy
    Kawsy Sy6 giorni fa

    Père You bi Patin mo wara Def clip bi 😂😂😂😂😂

  • Papa Armand Niang
    Papa Armand Niang6 giorni fa

    Le maestro r.a.s

  • Mariama Dia
    Mariama Dia6 giorni fa

    Sublime tout simplement

  • drk_momo
    drk_momo6 giorni fa

    🤣🤣🤣 ki dh graw na wañiko bro ( je parle du mec qui mytho pas de youssou ndour )

  • Fatoumata Ba
    Fatoumata Ba7 giorni fa

    Kounkandé wouyoul fii🤣🤣🤣

Il prossimo