Eumeu Sene Sort de sa réserve après son Combat J'ai été atteint Mystiquement, Meussouma beuré...?

Abonnez-vous à notre Chaine ITfun: itfun.info/slow/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ.html?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Commenti

  • Mouhamed Mbaye
    Mouhamed Mbaye8 ore fa

    Ma xam fracture bilay Lac doul rek mousoul dameu

  • Bety Niass
    Bety NiassGiorno fa

    Eumeu ko yapp yén niar nieup beuré wo lén naniou bayi yéneu sénégalais affairou naafékheu

  • Amy Sarr
    Amy SarrGiorno fa

    No vrema balla moy sama fans mé emeu ndandane nga

  • Beneen Tv
    Beneen TvGiorno fa

    Xanaa du mystique la daane Bombardier Na gëum yallah te feliciter adversairam

  • Ndeye sokhna Diao
    Ndeye sokhna Diao3 giorni fa

    Eumeu khamal ni yaw diam rekk guay ame

  • Mame Ndour
    Mame Ndour4 giorni fa

    Bilaé tonton yayy champion 💪💪💪

  • Fallou Ba
    Fallou Ba4 giorni fa

    Vraiment contenen si yaw ndakh lingua sédé si balla gaye 2 sama champion bi

  • Bamba Diop
    Bamba Diop4 giorni fa

    Eum yaw wakhe rèk gay dèf yaw gè no sakoyi

  • Pape fall
    Pape fall5 giorni fa

    Dagua diekhal

  • awa barry
    awa barry5 giorni fa

    Courage champion

  • Mouhamadou Kane
    Mouhamadou Kane5 giorni fa

    Des faiseurs de malin cela va de soi car la lutte n,'est que le culte de la betise

  • NSTYLEZ. TMC n.stylez
    NSTYLEZ. TMC n.stylez5 giorni fa

    Nandane nga eumeu tigui jaroul justifier wou, balla Nandane la, modou lo Nandane la, gris Nandane la, bombardier Nandane la , LAC vrai fake le, tapete la, dafay rous lo goor

  • Alda Fernandes
    Alda Fernandes5 giorni fa

    EUMEU J'adore ton sourire

  • Binetou rassoul
    Binetou rassoul5 giorni fa

    Lac 2 ay thiokh leuh amoul ...wah écurie weum nagn ko dieundeul thiokh svp

  • Abdul sumner
    Abdul sumner6 giorni fa

    Lac2 dafa wara bai lamba Du Dan tei du danu Match nil rek yaha derr keseh Mann Gambian la eumeu ndaanan nga

  • Serigne malick mbacké Diop
    Serigne malick mbacké Diop6 giorni fa

    Balla moy sama lutteur dh mais bilahi j’adore eumeu séne ndakh deugue bimouy guéné si lamigne bi deugue dafa nékh daale❤️🙌🏾

  • ceerw buty
    ceerw buty6 giorni fa

    Mane dei Balla moy sama mbeur beugu wa Guédiaway mé biii dama méré lac srx Eumeu diam si yaw def gua leep franchement bénen yon moy dak inchallak

  • Eva Dia
    Eva Dia6 giorni fa

    Walahi jeste bi eumeu déf ak balla dafma nékh trop

  • Mboul Ngom
    Mboul Ngom7 giorni fa

    Ay way nguir yalla Eumeu boudé amna team dolen massi dougal té yalla takh

  • Mboul Ngom
    Mboul Ngom7 giorni fa

    Machalah on t'aime bcp Eumeu wadiatal bou bakh rek

  • ceerw buty

    ceerw buty

    6 giorni fa

    Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

  • Abdou Sene
    Abdou Sene7 giorni fa

    Lac est un imbéciles

  • Abdou Sene

    Abdou Sene

    7 giorni fa

    Lac ne mérite pas c cacher

  • Maman Bop
    Maman Bop7 giorni fa

    Machallah fans club pure là Mala beug pure eumeu longue vie

  • Bugs Bunny
    Bugs Bunny7 giorni fa

    nekhoule ba nekhoul mais eumeu yaw tamite beurewo. deugue rek nekh nak

  • Elizabeth Brooks
    Elizabeth Brooks7 giorni fa

    machala eumeu sene diambar gua

  • Mounass Tamba
    Mounass Tamba7 giorni fa

    Je suis fier de toi champion😘💟💟💟💟

  • Coumba Diop
    Coumba Diop7 giorni fa

    Wallahi djambar ga lac dou mbeur

  • qopoy dnon
    qopoy dnon7 giorni fa

    yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

  • Sarr Sarr
    Sarr Sarr8 giorni fa

    Vous les lutteurs vous faites toutes des fétiches donc il faut accepter la défaite. T as rien à dire .il faut être sportif.

  • Adama Malick Dramé
    Adama Malick Dramé8 giorni fa

    Lac d'où dara da nirou woule sakh mbeur

  • Adama Malick Dramé
    Adama Malick Dramé8 giorni fa

    Bilay eume da melni nion boke père et mère bilay da ma la begue menouma sétane sa lamb si salle de bain laye dougue monté ay écouteur ba volume 100

  • qopoy dnon

    qopoy dnon

    7 giorni fa

    Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

  • Adama Malick Dramé
    Adama Malick Dramé8 giorni fa

    Non eume ya fi nék ya meune kou nékoule lac li d'où défaite dhe yaw champion nga respect mbeur on é toujours derrière tw

  • Assane Konte
    Assane Konte8 giorni fa

    Je vais convoqué les amateurs de lutte pour faire une marche pour que lac 2 arrête de lutter

  • Moustapha Kamal Th.
    Moustapha Kamal Th.8 giorni fa

    Eummeu, boul wakhati dotouma beuré ak mom . Dél wakh beugatuma beuré ak mom inchalla. Jajeuf mbeur

  • Pape medoune Ndiaye
    Pape medoune Ndiaye8 giorni fa

    Eumeu bilakhi wafii né

  • soniyu ziuy
    soniyu ziuy8 giorni fa

    Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

  • Mustataa Siise
    Mustataa Siise8 giorni fa

    Euma tay bërewoo dara

  • Diagne Gnilou
    Diagne Gnilou8 giorni fa

    En t'en que domou sèrére qui parle jamais sérère saymbok mérénagnoula

  • Diagne Gnilou
    Diagne Gnilou8 giorni fa

    Yacodjoh sabaram

  • soniyu ziuy

    soniyu ziuy

    8 giorni fa

    Non eumeu gor deugue la

  • ndiaga faye
    ndiaga faye8 giorni fa

    Jämbàr deugue ngueu maaacha allaah ki ngua doon da dieel mooy thiounné reek koo diapp mistiquement War koo meuneu daan

  • Hamidou Agne
    Hamidou Agne8 giorni fa

    Eumeu champion gue 👍Lac mome dou beure

  • Pape Sane
    Pape Sane8 giorni fa

    Je suis supporter de Balla gaye mais eumeu sene je t'adore vraiment legui sama mbeur nga ndakh sa xol dafa rafet

  • Awa dia Sy
    Awa dia Sy8 giorni fa

    Bilaye soule ndanane souli badola mais yaw mbeur nga diambar nga

  • cheikh kouyate
    cheikh kouyate8 giorni fa

    Eumeu il est bien. Lac 2 bonne continuation. Je suis fier de toi

  • sotuur aeei
    sotuur aeei8 giorni fa

    Douma fans Eumeu mais damako naw franchement dafa digne degou blie machalla

  • Aly Niane

    Aly Niane

    6 giorni fa

    Ad

  • Youssou Diop
    Youssou Diop8 giorni fa

    Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

  • Issa Diao
    Issa Diao8 giorni fa

    Lac dou mbeur bilahi

  • Issa Diao
    Issa Diao8 giorni fa

    Na bayi beurré

  • sotuur aeei

    sotuur aeei

    8 giorni fa

    Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

  • Ndaye Khodia
    Ndaye Khodia8 giorni fa

    Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur

  • Assane Samba
    Assane Samba8 giorni fa

    Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé

  • Boury Ka
    Boury Ka8 giorni fa

    Balla sama gaynder Ndiaye

  • Mamy Ba
    Mamy Ba9 giorni fa

    Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️

  • Muslim2proud
    Muslim2proud9 giorni fa

    Kouko déffati nako deegg, ap mbeur dou fénn, mbeur dou tapalé...aaay kouko défati nako deeg ap mbeur dou tricher mbeur dou yambar, 😤diapé sénégalais yi dofff 💃💃💃💃💃😂😂😂😂😂Eumeu, Balla Gaye2, Yekini, Bombardier, Ama Baldé, merci infiniment, gathiéloulén lambe. Fatou Guièr 2 démal nga toog, ngir yalla boulfi dieuleuti beneu combat, doyal na gnou si yow seuk.🙄🙄😏😏😠😠😠😠😠

  • Djily Diop
    Djily Diop9 giorni fa

    Non eumeu gor deugue la

  • bssni touir

    bssni touir

    8 giorni fa

    Lou lérr laa wakh

  • vmvdou svné
    vmvdou svné9 giorni fa

    jai trop aimé son discours

  • vito boss vito boss no stressé
    vito boss vito boss no stressé9 giorni fa

    mane fans balla gayé la

  • bssni touir

    bssni touir

    8 giorni fa

    C'est vrai je suis avec eumeu

  • vito boss vito boss no stressé
    vito boss vito boss no stressé9 giorni fa

    bilahi euma borom bakh la

  • drttyu liqm
    drttyu liqm9 giorni fa

    yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

  • El Che
    El Che9 giorni fa

    Lac 2 moy enfoiré rek . Yaw kenn du yaw jambar deug ga

  • Mamadou Alpha Bah
    Mamadou Alpha Bah9 giorni fa

    Je suis un fan de Modou Lo mais je t'aime💕💕❤❤😍

  • Marieme Balde
    Marieme Balde9 giorni fa

    Mais eumeu nak balla dinala dane dh one bakhga trop beugue nagne la mais dinagne la dane dh 😂😂😂

  • drttyu liqm

    drttyu liqm

    9 giorni fa

    lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

  • Marieme Balde
    Marieme Balde9 giorni fa

    Sana xol diekhna si lac thiim. Bravo eumeu courage. Balla ak wa keureum gnoy samay mbeur (sauf Lac maintenant) legui iow yako remplace. Borom vakh nga

  • Aita Ndiaye
    Aita Ndiaye9 giorni fa

    Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

  • Ndeyemarie Seye
    Ndeyemarie Seye9 giorni fa

    Diamou RK ngayi âme bly

  • BUZZ MIFA
    BUZZ MIFA9 giorni fa

    EUMEU BOUL BAY AWMA KÉNE COUEOUL YEW

  • Khady Togola
    Khady Togola9 giorni fa

    Eumeu ya meuna doull lac dakeu leu bangua guéneu sakou yi guay féne Amgua mélokane déh khawma wone ni ningua mel féne bakhoul

  • BUZZ MIFA
    BUZZ MIFA9 giorni fa

    EUMEU JE T'AIME BILLAHI

  • Issakha Ndiaye
    Issakha Ndiaye9 giorni fa

    Tu fais partie des meilleurs.

  • Aboubacry Sarr
    Aboubacry Sarr9 giorni fa

    Ya fi meun dh Eumeu billahi ❤️

  • Chekh tidiane Thiam
    Chekh tidiane Thiam9 giorni fa

    C'est vrai je suis avec eumeu

  • Mbacké Seck
    Mbacké Seck9 giorni fa

    Lou lérr laa wakh

  • Modou Mbaye
    Modou Mbaye9 giorni fa

    Eum bénéne yonne boy bré boul nuyoti kénn lokho.bâ nga nuyo thi lamb dji la khamni da ngay d'Abou.

  • Abdou Mbaye
    Abdou Mbaye9 giorni fa

    Eumeu sa kanam

  • khass Killah
    khass Killah9 giorni fa

    Boléne waxé té yalla tax ngéne xamni lac2 mo tané si combat bi ndax mom sax défna touti effort eumeu sax wax nako après combat bi "waroléne ma wonn téyélo sama bop" motax dafa taxaw rék défoul dara. Questioné nagn ko mo bo xolé boubax dafay rafétal di rectifié wax bi coz ay staff faw gnoniko bouko wax parck lolou daf léni yaxal mbeur gnou fayla ay millions sa staff nane la téyél sa bop

  • Penda Wade
    Penda Wade9 giorni fa

    Yaw diabargua bilay

  • Khady Gueye
    Khady Gueye9 giorni fa

    lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

  • Khady Gueye
    Khady Gueye9 giorni fa

    billay diabare gua

  • Mame Saye Sylla
    Mame Saye Sylla9 giorni fa

    Bilahi eumeu sene wakhone na lako si beineu commentaire nila lac de guiers 2 dalayy tardel rek khamoul gatt ragale na bilahi wokhone na lako beurei woule bayi woule dafa ragalll tropp tropp

  • Abu Konate
    Abu Konate9 giorni fa

    Eumeu lat 2 amoul diome

  • Ibrahima Khaliloula Hounsah
    Ibrahima Khaliloula Hounsah9 giorni fa

    Eumeu Nguaïdé Nguay Meussa Done Bo Bayé Beuré Sax Nguaïdé Ngua

  • Diogop Ka
    Diogop Ka9 giorni fa

    Machalla fiér de toi champion 💪💪💪sa kaw sa kaname

  • Ibrahima Diop
    Ibrahima Diop9 giorni fa

    💪💪💪👍👍

  • Khadidiatou Gueye
    Khadidiatou Gueye9 giorni fa

    Barki yamlah Eumeu damala beug

  • Seyidina Sow
    Seyidina Sow9 giorni fa

    Eumeu champion nga lou lérr Lac war nga kholaat sa beuré té di dieul décision, am nga katane loy ragal, khamon sakh biss bo mome warko am ndam,... modou lo ndam rék Incha ALLA

  • Sila Dame
    Sila Dame9 giorni fa

    Q

  • Sall Ablaye
    Sall Ablaye9 giorni fa

    Khole bou rafet eumeu

  • Mansour Gueye
    Mansour Gueye9 giorni fa

    Mberr yaw diaroul sakh ngay nioue khana nonou yaye Kane mberr pure nga

  • Isatou Jobarteh
    Isatou Jobarteh9 giorni fa

    Eumeu sene yow ya Barry wakh barry tapaleh

  • Fati Sow
    Fati Sow9 giorni fa

    waw kay eumeu diadieuff way on te fais confiance

  • Adama Fall
    Adama Fall9 giorni fa

    Champion nga

  • Mariama Diéne
    Mariama Diéne9 giorni fa

    💪💪😇😇😇😍😍😍👍

  • ASTOULO KOBAR
    ASTOULO KOBAR9 giorni fa

    Eumeu yawdal gathia ngalama chapeau a vous mbeur kaamil NGA

  • Pape Davido
    Pape Davido9 giorni fa

    Cœur pour diambar jdi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • Tijani Dia
    Tijani Dia9 giorni fa

    Waw kay sama mbeur bi amal diame yaw lanou beugue tay ak soube mala beugue rek té yallah takh soy beuré douma ame diame wallahi taye wnibik hateu

  • Pape Davido
    Pape Davido9 giorni fa

    ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • Ahmada Dial
    Ahmada Dial9 giorni fa

    Iow tamit beure wo ...wakh ko kéne meunou niou nakh

  • Adama Camara
    Adama Camara9 giorni fa

    Eumeu séne diambar gue nion gui sa gui naw

  • Gooo Bhff
    Gooo Bhff9 giorni fa

    Eumeu ❤️❤️❤️❤️💪

  • Gooo Bhff

    Gooo Bhff

    9 giorni fa

    @gtoss chddy lac mo bougone Revanche

  • gtoss chddy

    gtoss chddy

    9 giorni fa

    Vous avez tout les deux déçu

  • Mariama Aliou Diouf
    Mariama Aliou Diouf9 giorni fa

    Fier de vous Eume Sene

  • Serigne saliou Lo
    Serigne saliou Lo9 giorni fa

    Waw lac nonou ladone def mé khamnanou touti si lamb

  • gtoss chddy

    gtoss chddy

    9 giorni fa

    Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss

  • ibrahima ndom
    ibrahima ndom9 giorni fa

    Eumeu mi da melni da beug beuré wate AK Balla

Il prossimo