Urgent Iran Ndao démasque certains marabouts « Lignouy déff dou dara ay Nakhatéla « si Tank

#iran #khass #senegal
page facebbok : PeupleduSenegal/
Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification

Commenti

  • gounass bozz
    gounass bozz10 giorni fa

    👏👏👏👏

  • Mouhamet Dieng
    Mouhamet Dieng10 giorni fa

    Diarra

  • Khadim Diop
    Khadim Diop10 giorni fa

    Yalla dounaxé ta kén douko nax

  • Topi Topi
    Topi Topi12 giorni fa

    Assalamou aleykoum wa rahmatoulah ya oustaz. Dieureudieuf yalna la borom bi same soutourale barkèle yeureume diègale la ak dioulit yeup amine ya rabbil alamine alhamdoulilah machaallah dieureudieuf

  • Tening Sabaly
    Tening Sabaly12 giorni fa

    B

  • Baye Diankha
    Baye Diankha12 giorni fa

    Iran ndao dimbaleu nio ya dakha dorr ya fi wediwone Gamo ligui yangui toude marem faye gamo lekall rek te bayi haleyi nio lek sohorr nga

  • eioshen boboi
    eioshen boboi13 giorni fa

    Bilahi bouñou amone 20 you mèlni yaww lègui mou nèkh sènegal limafi gueune mèti moye bouñou dèmè baye guiss domou dioulite diko diawalè ak lènè ya problèm🙏

  • Nar bou Ndaw
    Nar bou Ndaw13 giorni fa

    Bilahi dafa nième degue mo takh mou nekh ma

  • AMY DIOP
    AMY DIOP13 giorni fa

    Mane yawla beugue dakh deugue rèk mola ñior

  • Seynabou Diallo
    Seynabou Diallo14 giorni fa

    Iran Mane déjà doumala sétane ndakhe amo makharije sa kharafe da guaye yakhe Aya alkhourane réke ligua wakhe dara d'où thi deugue domou ndilo mo bokoule ake but bou orjeut ya allaahou moye diokhé dôme nitte âme n'a dieukeure di seye té amoule ndialoo takhoule gua âme dôme ya allaahou mo koye diokhé domou ndialoo daye done guénele Lou lére Lou si ya allahou wakhe d'où baquara ba nasse ndakhe nékoussi wakhe léne Lou léne ya allahou wakhe lo yawe khamo sakhe ndakhe sa baye mo la dioure mo takhe ya allaahou si alkhourane yeupe sa yaye réke la wakhe ndakhe néna môme mo khame kouye séne baye môme ya allaahou sougnouye wathié kamile kou décédé tourou yayame la gnouye wakhe kéne d'où wakhe papa mémé soye diouli di gnanale saye néwe tourou yayame guaye wakhe bayiléne ake ya allahou aye mbireume

  • Babacar Diop
    Babacar Diop14 giorni fa

    Malako wakh touss khamou ngiouko😈

  • Mariama Coly
    Mariama Coly14 giorni fa

    Hello

  • Boubacar Diallo
    Boubacar Diallo15 giorni fa

    Oustaze Iran ndao je t ' adores

  • sehhi vooty
    sehhi vooty15 giorni fa

    Iran content na ci yaw Waw fou weri WI fegne ci sous région bi wor rék mognou war ndakh kor ya Allah moko mome mbindef momouko

  • Papa Gaye
    Papa Gaye15 giorni fa

    He suis fiertè de toi ❣

  • Zeydoun Saw
    Zeydoun Saw15 giorni fa

    Manchallah koumay yo bou saloum

  • Malick rasoul ndao Ndao
    Malick rasoul ndao Ndao15 giorni fa

    Billaye degg la

  • diop nar
    diop nar15 giorni fa

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • mame diarra bousso sene
    mame diarra bousso sene15 giorni fa

    Iran❤️

  • Amadou Faye
    Amadou Faye15 giorni fa

    👍😂😂🤣🤲😋😂😂💓💓💓🇸🇳

  • Abdou Seye
    Abdou Seye15 giorni fa

    Non iran daga gno yapp c trop enfantin ligay wakh

  • seeni gzty
    seeni gzty16 giorni fa

    khamou ko 🤣alkhour Ann sakh mokalou ko ma guis ko si RS yi mu diakhal ma mais après mom si bopam moma leral lepp ay dealer la rék 😂😂😂😂😂😂

  • Zara Zara
    Zara Zara16 giorni fa

    Bilhay deug la kou wédii démal si sama Mame maka diané wala ayenou manii bilhay serigne yagui saloum

  • MEDOUNE KARA JR NIANG
    MEDOUNE KARA JR NIANG16 giorni fa

    Dieureudieuf Iran sur les éclaircissements !!!

  • steve scorfiel
    steve scorfiel16 giorni fa

    Raisonnable et avec des preuves. Ortez vous bien. Il faut des gens comme Iran au Sénégal. Jajeuf

  • Just'Un'Clik TV
    Just'Un'Clik TV16 giorni fa

    Iran néna mom raadi rek, glace rek 😂 😂 bilahi door war moy deug

  • gamebayen11
    gamebayen1116 giorni fa

    Boul Boul daw

  • Amina Ba
    Amina Ba16 giorni fa

    Iran liga wakh lep deugula mes dou kéréme bi rk diokhgnou si tourou yalla yi bok gnou am

  • Ibrahima Sow
    Ibrahima Sow16 giorni fa

    Vraiment pèr iran deug pir nga wakh amal diam

  • Saer Seck
    Saer Seck16 giorni fa

    Machala

  • Sokhna Aminata Gueye
    Sokhna Aminata Gueye16 giorni fa

    😂😂😂😂 Iran ray guama

  • Thiaba Ndiaye
    Thiaba Ndiaye16 giorni fa

    Tonton Iran c'est docteur thiaba si tu étais président de la République du Sénégal sama khél dal deug bi yaw rék la

  • abdou
    abdou16 giorni fa

    Yalna sa diamm yagg

  • Bousso NDOYE
    Bousso NDOYE16 giorni fa

    Yak fi té weer oustaz Iran

  • Mamadou Ndiaye
    Mamadou Ndiaye16 giorni fa

    Machalla

  • Bâ Chouboy
    Bâ Chouboy16 giorni fa

    Bilahi papa mala nawe si dégue 🤲🙏🙏🙏🙏

  • Aisstou Ket
    Aisstou Ket16 giorni fa

    Vérité absolue

  • khadim awa gueye
    khadim awa gueye16 giorni fa

    Merci Irán

  • Amina Ba
    Amina Ba16 giorni fa

    Machaalah Iran yag fii lool té wèr

  • madina ndiaye
    madina ndiaye16 giorni fa

    Iran souba inchàla neww Dou dess Senegaal...dorkatou matt yii yepp souba Niou defar ay tiouray néew

  • Kine Faye
    Kine Faye16 giorni fa

    Mane ki la gueume

  • ibrahima barry
    ibrahima barry16 giorni fa

    billahi beugue nala iran...nala yalla soutoural

  • Elhadji Faty
    Elhadji Faty16 giorni fa

    Yewoulem Senegalese Baye len Serigne si ITfun bi xam niou darra dieuredieuf Iran ndao

  • Barro Lo
    Barro Lo16 giorni fa

    Merci

  • Kabou Toure
    Kabou Toure16 giorni fa

    Merci beaucoup ya oustaz irra affaire comité Sénégal affaire tarikhe là, dou diamou yallah, je suis d'accord avec toi

  • yade Ndong
    yade Ndong16 giorni fa

    Bilay ndaysan😂😂

  • Swetty Swetty
    Swetty Swetty16 giorni fa

    Khass vraiment comédien 🎭 la ndeysane ak kou len diapelé surtout célébrités yikoye encourage enplus khass daffay Dieund célébrités ak dilen niokh si boppam pour attiré les gens parce sou beneu célébrités demé si momeu ils influencer beaucoup de personnes surtout les fous qui trop influençables sachez que khass lobi rek la yoor

  • Mamy Niang
    Mamy Niang16 giorni fa

    Tonton Iran yalna la yalla fayal bomap🙏🙏deug rek ngay wakh

  • Amadou Ndiaye
    Amadou Ndiaye16 giorni fa

    Lou lerr 🙏🏻🙏🏻🙏🏻les marabout actuellement moy lolou

  • sozz 2
    sozz 216 giorni fa

    Alkhouran Moy lep irao ndao merci

  • Khadime Kane
    Khadime Kane16 giorni fa

    ki khamo lainko yalla rékk mou ko gnor

  • Zale Diaw
    Zale Diaw16 giorni fa

    Walahi ndeysann ligua wakh lépp ☝️ deugleu

  • Sire Mane
    Sire Mane16 giorni fa

    Maachaalah Long vie à vous oustaz

  • Loyenne TV
    Loyenne TV16 giorni fa

    Diop khass dal dioum ngua

  • Talla Séne
    Talla Séne16 giorni fa

    Djiguin nie dh nio gueuneu dof thi serigne nie tariakh yi

  • philosophie Gueye
    philosophie Gueye16 giorni fa

    Gayi dagni nakhé rék ba paré caméraman yi ay complice lane mane amna sama béne kharit nio bokone daara tay serigne bou mague la😂😂 wayé billahi dara dara dara khamou ko 🤣alkhour Ann sakh mokalou ko ma guis ko si RS yi mu diakhal ma mais après mom si bopam moma leral lepp ay dealer la rék 😂😂😂😂😂😂

  • Real Madrid 100%

    Real Madrid 100%

    14 giorni fa

    😂😂😂😂6moy9 rék

  • Talibe borom Diamono
    Talibe borom Diamono16 giorni fa

    Degeul iran🤣🤣🤣

  • Linguère Touré
    Linguère Touré16 giorni fa

    Machalla Iran bougnou amone 20 you mel ni yaw nakhaté bi diekh Sénégal

  • Awa dallo
    Awa dallo16 giorni fa

    Yalla.na yalla yok sa diam.si barké yonantibie

  • Nogaye Kandji
    Nogaye Kandji16 giorni fa

    Machallah

  • Sarr Abdou
    Sarr Abdou16 giorni fa

    Merci irán motah loudul deugeu Dou yaggeu

  • Assane Diop
    Assane Diop16 giorni fa

    Walakhi irane wakh nga deugue, la moitier signiome dougne wakhkati deugue, sai des voleurs, daigne laine wara waire

  • Fatou Diouf
    Fatou Diouf16 giorni fa

    Machaalah je suis parfaitement avec vous yallah motakh may wor wayé dou commission

  • madlene mbaye
    madlene mbaye16 giorni fa

    Ablaye diop khass boo née diakeu kanamame dinga khamni khamoul dara c un faiseur de malin gate khamouko

  • Baye Fall
    Baye Fall16 giorni fa

    Yalla nagafi yagg looôoool taa ende ak wére

  • Fatou Gueye
    Fatou Gueye16 giorni fa

    Iran yalnanga goude fane soumboulou bou client yi dawer boule dawe der seyeul seybi

  • Sante Yallla
    Sante Yallla17 giorni fa

    Merci Iran ablaye diop khass domeram internationale la

  • Serigne mouhamed Sow Dia Baayou Serigne yii
    Serigne mouhamed Sow Dia Baayou Serigne yii17 giorni fa

    Machalla Iran yall naa diambou yageu sy Sénégal 🇸🇳 Amin yarabi

  • Assane kane
    Assane kane17 giorni fa

    😀😀😃😃😃

  • Assane kane
    Assane kane17 giorni fa

    Oh

  • Kine mané bou Serigne Babacar sy
    Kine mané bou Serigne Babacar sy17 giorni fa

    Bilahi aye arnaque layou tek si aye domaram layou lekk khalice sou nitte yi wayé déé amna dh aye bou bobah hu

  • Babacar Niang
    Babacar Niang17 giorni fa

    Mashallah wallahi mane mom j suis parfaitement d'acors avec vous Iran

  • Ndéye astou Sokhna
    Ndéye astou Sokhna17 giorni fa

    Papa iran Mane damala beugue yallna sa diam yague

  • FAYE MOUHAMED
    FAYE MOUHAMED17 giorni fa

    Mo dakha door nieupp , Yallla dafa binnd té yamalewouol ,Lo meunoul nell meunoko....

  • FAYE MOUHAMED

    FAYE MOUHAMED

    16 giorni fa

    @Bakh Niang bonaloumako du bro...

  • Awasarr Sarr

    Awasarr Sarr

    16 giorni fa

    @Bakh Niang bayiko fofou

  • Bakh Niang

    Bakh Niang

    16 giorni fa

    Saye wéteu ngafi dh wouteul koula diapalé Iran kou bakh la fall

  • Nabou Gueye
    Nabou Gueye17 giorni fa

    Tonton iran machallah

  • Fama Diouf
    Fama Diouf17 giorni fa

    Merci Iran Ndao

  • Omz Diaz
    Omz Diaz17 giorni fa

    Deugg dou rombi noppou

  • Papis Mayweather knepper Ndiaye
    Papis Mayweather knepper Ndiaye17 giorni fa

    koussi nek ak sa weursseuk foumouy diar...loudoull deugeu dou yageu

  • Aram Ndiaye
    Aram Ndiaye17 giorni fa

    ❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏💪💪💪👍👍👍

  • Serigne Dame Lo
    Serigne Dame Lo17 giorni fa

    Merci Iran

  • Ndeye Thiam
    Ndeye Thiam17 giorni fa

    Aidasame

  • Ndeye Thiam
    Ndeye Thiam17 giorni fa

    AIda same

  • Kine Ndiaye
    Kine Ndiaye17 giorni fa

    Barki yalla man yaw la wolou dagua am fouleu

  • Sarr Mouhamet
    Sarr Mouhamet17 giorni fa

    Machalla iran

  • Aminata Sow
    Aminata Sow17 giorni fa

    Xamna ni soneguén dolén bayi Diop xass boudé day nakhaté môme ak yalla leu yalla yakam tiwoul kén

  • Sarjo Drammeh
    Sarjo Drammeh17 giorni fa

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • Le Ndiambour
    Le Ndiambour17 giorni fa

    gayi kay dinagn diwo néw

  • Bintou Diabong
    Bintou Diabong17 giorni fa

    Kou Beugu xam xam gnéwale saloum

  • Fanta Diamanka

    Fanta Diamanka

    16 giorni fa

    Loufa nek ma kham

  • Omar Gaye
    Omar Gaye17 giorni fa

    kkkkkkkkk iren dana ray nite mavouje kay

  • Omar Gaye
    Omar Gaye17 giorni fa

    cheri khass kkkkkkkkk

  • Akhmadou Ba
    Akhmadou Ba17 giorni fa

    Li ngua fakhe deug la de

  • Babacar Sarr
    Babacar Sarr17 giorni fa

    Machala

  • Mariemebelle thiam
    Mariemebelle thiam17 giorni fa

    toyamikou papa dinama raye li ay khas moi bi yako mame

  • DIEDHIOU Diedhiou
    DIEDHIOU Diedhiou17 giorni fa

    😂😂😂😂😂😂😂 gniara gniara gniara!!!! Dé né

  • Ant2045 SALAM
    Ant2045 SALAM17 giorni fa

    Merci Per Iran vous Avé tout dit en quelque minute merci.

  • Ablaye Thiam
    Ablaye Thiam17 giorni fa

    Degu rek

  • P Radis
    P Radis17 giorni fa

    Merci irán une donne un bon exemple au comission

  • souleymane ly
    souleymane ly17 giorni fa

    🤣🤣🤣🤣

  • Modou Gueye
    Modou Gueye17 giorni fa

    Merci iran nakha te katyi dagnou bari reuwmi

  • Khabi Kane
    Khabi Kane17 giorni fa

    Iran jajeuf yallah rékafiné

Il prossimo