Chez Franc, 1ère réaction après sa victoire sur Tyson 2: Lac 2 et Eumeu koussi gneuw ma danela

www.equivoxgroup.com
Votre Télévision á Portée de main
Une Thématique digitalisée

Commenti

  • L'absolu Gueye
    L'absolu GueyeMese fa

    Dafa Yarou Trop Billahi félicitations Fra yaw champion nga boumak sax Billahi 🙂Fra Vs Reug Reug combat là Fra Vs Diène kairé combat là Fra Va Sokhou combat là Fra Va Moussa Ndoy combat là 😊

  • Mbaye sarr Dia
    Mbaye sarr DiaMese fa

    Machalla franc

  • Modou Fall
    Modou FallMese fa

    Champion la

  • Gelawar Gelawar
    Gelawar GelawarMese fa

    Courage champion 💪 wakh na deug diokh lene ko si gayi

  • Lucien Mendy
    Lucien MendyMese fa

    Barane Abuk Manjacku Na Njäffu Nha wëkk

  • Amadou Sow
    Amadou SowMese fa

    Dema bag wa parcelle yepe ndakh modou lo

  • bocoy noiu

    bocoy noiu

    Mese fa

    Boy dagua bari ndaye wakh dieuleul diéne mo geune nguay wakh rék so beugé dougate pikine sokh nguay dieul mou niouss sa ndaye

  • Khadim
    KhadimMese fa

    mbeur lo meunoul boulko diém , tayson 2 dafa wo franc si khékh té niéméwouko té xamoul ni franc moko dakh khékh fopp , motakh franc nokh nako daneko . Mdrrr

  • elzoatti8
    elzoatti8Mese fa

    Fran jangal boxe

  • Amadou Balde
    Amadou BaldeMese fa

    Elton amoul combat genofa teyal boy

  • Amadou Balde
    Amadou BaldeMese fa

    Nnn yaw moussa ndoye sax ak sathies Biola raw sankamtoumala niom gouy gui yaw soula moussa dieulei sax santal ndank meti woul yaw soudoul modou anta diene moy sa adversaire nioniou ak Tyson2 nio tolou catégorie mais li système la rek pour meuna beurei ak niom

  • Amadou Balde
    Amadou BaldeMese fa

    Franc dieul n'a coup dh

  • Amadou Balde
    Amadou BaldeMese fa

    Franc legui concert n'a fouye dh

  • matar mbuege
    matar mbuegeMese fa

    Damaye ragal gayi bangeko ndakh modoulo

  • Issa Mbaye

    Issa Mbaye

    Mese fa

    Mouk

  • matar mbuege
    matar mbuegeMese fa

    Bilaye France mi inchallah dina done roi

  • Nouha DIEME
    Nouha DIEMEMese fa

    Franc vs reug reug

  • lamine lamine
    lamine lamineMese fa

    Wa pikine sén stade bi jiguléén dara

  • lamine lamine
    lamine lamineMese fa

    Wa pikine sén stade bi jiguléén fara

  • lamine lamine
    lamine lamineMese fa

    Mann moom tayson2 la faraloon mes vrément frenk champion nga ,10 victoir yommbul felicitation

  • Bernard Gomis
    Bernard GomisMese fa

    Merci Papa sow

  • Ibrahima Sow
    Ibrahima SowMese fa

    Boy dagua bari ndaye wakh dieuleul diéne mo geune nguay wakh rék so beugé dougate pikine sokh nguay dieul mou niouss sa ndaye

  • Modou Camara

    Modou Camara

    Mese fa

    Yagui merr de 😁😁😁😁

  • Khalifa Ababacar Samba
    Khalifa Ababacar SambaMese fa

    Nala lac 2 may chance wala gouygui vs reug reug kou dann ga dieul felicitation champion ga

  • Moussa Fall
    Moussa FallMese fa

    Félicitations champion touti wax ak job lou barri yassi meune fouf P.A va bien

  • Wagne Oumy
    Wagne OumyMese fa

    Nako lac 2 diel

  • cedric samba
    cedric sambaMese fa

    Franc limalay conseil Moy jouru combat sa Thiès ah Moussa ndoye demal nga sampp sa ndeundeu fofu Ku d'âne ah Ku danou yeup nga dieul ... Té bayi ameu ah lac 2 basi knam ... Nah mbeur bula appe cachet dula diokh thieur ... Défale piano 🎹 piano 🎹 rk inchallah wala nga xar comba gris 2 vs Abdou Diouf tmit fofu am ngafa place

  • Ousmane fall
    Ousmane fallMese fa

    Franc est fort kone parecell amna ndiago khana beurehwoul pour mane grand Yoff la am ak guediawaye

  • Dollar Babs
    Dollar BabsMese fa

    Boie bi bvndi la koi😄😄mais il deviendra un grand champion

  • Aliou Thiaw
    Aliou ThiawMese fa

    Boulene dieul lac2 déé dafay yahh combat d'où mbeur

  • Aliou Thiaw
    Aliou ThiawMese fa

    Nomm tout sauf lac 2

  • lamp
    lampMese fa

    Franc vs Diène Cairé combat douko dakk Franc vs Malick Niang combat'la

  • Lucien Mendy

    Lucien Mendy

    Mese fa

    Gars you pertes yoyou

  • Saliou Diba
    Saliou DibaMese fa

    Bilaye walaye parcelle rek

  • Aliou Sagna
    Aliou SagnaMese fa

    Hé kéneu dou Ndiago bi bilahi walahi

  • Modou Niang
    Modou NiangMese fa

    💓💓💓💓

  • Arame Hote
    Arame HoteMese fa

    Boy ni gua toudou d'un niamu xallé dé

  • Salla Top
    Salla TopMese fa

    Djarama ioe ya néxa faral balki très srx

  • Felix Mendy
    Felix MendyMese fa

    Dole Ndiago mendy gomis périera

  • Khadim Fall
    Khadim FallMese fa

    Franc vs lac combat bou neikh leu

  • Ibrahim Thiam
    Ibrahim ThiamMese fa

    Lamb 0 structure franc Na que 11 combat 11 victoires di latié Yom Eume 🤦🏽‍♂️ bien k c un grand champion

  • mame alioune diallo
    mame alioune dialloMese fa

    Eumeu n’a rien dit de méchant, c’est normal qu’il defeant son Poulin . Eumeu sème mo meun say 10

  • Max Gueye

    Max Gueye

    Mese fa

    Wakho deug

  • Abdou Sall
    Abdou SallMese fa

    Bayil eumeu nak

  • Lune Dieng
    Lune DiengMese fa

    Franc d'accordna d ladial koula nekh mbeur yay diay sa boop bo daneii tamoul les meilleurs bo beugue guéneu si lot biii... Boy Niang ay année la top balla AMA à ses débuts la deukou modou lo donc trun rek tu iras loin

  • Badara Kane
    Badara KaneMese fa

    machallah babakar saliguye rafétna torop machallah ❤❤❤❤❤💪💪💪

  • SÉNÉGAL KÉSSO
    SÉNÉGAL KÉSSOMese fa

    Franc boul bourlé étapes yi jeleul diene kairé, wala ga , Malick Niang, sa Thiès, garga mbossé, moussa Ndoye, reug reug... bari ga ay adversaire yo khamni say morom lagnou .

  • Kalidou kaneOllaid
    Kalidou kaneOllaidMese fa

    Respect Papa sow sow poulloh Djery✌✌Ax Modou lo le Roi des Arenes ''trop de talent aux parcelles Assainie Modou papa franc garga2 ect....

  • Djiby Dieng
    Djiby DiengMese fa

    AMa yééééééééééééé TÉK FA diékhaaaaaaal

  • xaare info
    xaare infoMese fa

    Mala beguel sama bope yalla di may ay ndami mi ndame depuis fayako

  • Ndiaga diagne
    Ndiaga diagneMese fa

    Super franky💪💪

  • Matar Ndiaye
    Matar NdiayeMese fa

    franc vs Malick Niang

  • Matar Ndiaye
    Matar NdiayeMese fa

    franc vs Elton

  • Matar Ndiaye
    Matar NdiayeMese fa

    franc vs diène kairé

  • Matar Ndiaye
    Matar NdiayeMese fa

    Franc vs modou anta

  • Beydy Sakho cœur de Lion 🦁
    Beydy Sakho cœur de Lion 🦁Mese fa

    Lamb defa am Yonne continue de bossé guena prouver pour le moment gni ngay lim yeupou keine dou la dieul

  • amadou sy
    amadou syMese fa

    Arretes de stigmatiser .franc est senegalais comme tout le monde .babacar tu repetes trop ndiaagou ndiaagou

  • Ousmane fall

    Ousmane fall

    Mese fa

    Sof rek

  • Aba Sall
    Aba SallMese fa

    Yarou dabax kula guis sopela ku dégue sa kadu sopela nianal la nga avancé le relève de xlo yalna nga nek roi des arène

  • amadou sy
    amadou syMese fa

    Franc defa yarou .trop discipline

  • Bara nguer
    Bara nguerMese fa

    Modou Ak papa béne lagn franc boul neclicé modou

  • Ass Balla gaye 2

    Ass Balla gaye 2

    Mese fa

    Dou béne déh franc papa sow kilifam la moko yar té niom nio bokou kogne fran ak papa sow danio yague ték si ecri papa la né

  • moussa paye mane

    moussa paye mane

    Mese fa

    Béne lagne,mais eské liko papa di déf Modou dékodéf c sa le problém

  • Jazz jazz
    Jazz jazzMese fa

    TYSON2 DAFA RESPECTE WOUL BENE YONE FRANC MOUSSOKA DIOKH THIEUR WAKHONALENE KO TYSON2. THI PASSE WAME LAY NDAMO ALORS QUE LAMB DAFA DOKH AVANCER BAYI KO SI GUENA WAME. DU COURAGE UN CONSEIL ADVERSAIRE MEME BOKO MEUNEE DIOKH KO THIEUR. DIANGAL ENE SI FRANC. SPORTIF MODESTE TEE KHOLAM RAFETNA

  • Mbeur Sarr
    Mbeur SarrMese fa

    dieuleule malick niang yéna tolo victoire

  • Abdou Thior
    Abdou ThiorMese fa

    Franc malick niang Moy combat

  • Mbeur Sarr
    Mbeur SarrMese fa

    ms dieuleule malick niang bok

  • Modou Goumbala
    Modou GoumbalaMese fa

    Franc vs sokh moy lamb dji

  • Ahmed Ndiaye
    Ahmed NdiayeMese fa

    Franc mame balla no recul

  • Modou Gaye
    Modou GayeMese fa

    Futur modou lo walahi lamb dji parcelle moye borom

  • Ahmed Ndiaye
    Ahmed NdiayeMese fa

    Yap guen sa thies dhee mbeur Bou dioukh lathie ko mom tamite da bagua dem si kaw

  • Assane Diop

    Assane Diop

    Mese fa

    Sama waadji sa Thies moko def kenn eupouko.doolé.ci lambji té.meunna beurré.mais ragal.la loulou.moko té dan.boye niang.

  • Mms seye
    Mms seyeMese fa

    Franc vs sokh

  • Mms seye
    Mms seyeMese fa

    Franc vs sa thies

  • Ibrahima Diakité
    Ibrahima DiakitéMese fa

    Diadieuf champion bonne continuation

  • Seyni Sarr
    Seyni SarrMese fa

    Franc félicitation Eumeu sene wouyoule boy bii mo guéne

  • sora Bou Kharagne lo 👊👊
    sora Bou Kharagne lo 👊👊Mese fa

    Balaye Kontan na

  • Saliou Sarr
    Saliou SarrMese fa

    Franc Malick Niang wala reug

  • diáspora TV Bilbao va sengal
    diáspora TV Bilbao va sengalMese fa

    Frank vs Ama balde,comba la dh apres son defaite contre modou lo inchalaa

  • Alioune Dieng

    Alioune Dieng

    Mese fa

    sa defaite

  • TOP BOY
    TOP BOYMese fa

    Franc reug reug combat douko dakh ay morom laniou te ay beure kat laniou

  • Bass Pimpi

    Bass Pimpi

    Mese fa

    @moussa paye mane nonou la démé motax toudoul sax Reug reug😂😂😂

  • Ousmane fall

    Ousmane fall

    Mese fa

    Beureh naniou mbapat

  • moussa paye mane

    moussa paye mane

    Mese fa

    Lolou yakoy wah wayé Franc am nané Reug Reug moko meune fouf

  • Bass Pimpi

    Bass Pimpi

    Mese fa

    Reug reug dane nako 11fois ki reug dou moromam🔥

  • Djibril Niang
    Djibril NiangMese fa

    Merci champion

  • Djimba niang
    Djimba niangMese fa

    Sa Thiès bou dane moussa dou xol fran

  • Francois Mendy
    Francois MendyMese fa

    Gor day deugeur, félicitation ndiago or et bonne continuation. Ndiago mounoul nek ragal comme niou sopico golo mouye tiali tiali 😅😅😅😅

  • Shiekhibra Mbackeh Darboe
    Shiekhibra Mbackeh DarboeMese fa

    Grand champion Franc nof respect ✊🏾 Modou lo, papa sow, gora sokh, garga 2 , lie petagorr, tapha mborr, Dam sane and all the rest of war Parcelle much love ❤️ to all Tyson 2 do nandite billahi Mama Lamine le la ham motakh mo daw 🤜🏾🤜🏾🤜🏾🔥🔥🔥🤴🏾we will all be king 🤴🏾

  • Salif Ba
    Salif BaMese fa

    Dane Tyson 2 takoul gua mome nou

  • Amath Sarr
    Amath SarrMese fa

    Dangay doul rk

  • Babacar Gueye
    Babacar GueyeMese fa

    Xamo sa boppou yaw ak sokh combat lh

  • Ismael Faye
    Ismael FayeMese fa

    Champions ga me boul yacamti sa yone lambou da teradi ndak diga ague inchala

  • mame mor drame
    mame mor drameMese fa

    En l'écoutant je sais qu'il est trop jeune 🤣🤣

  • Mor Mbaye
    Mor MbayeMese fa

    Eupou diouka dolei kouka dieuloul dak ko ragal

  • Ibrahima Ly
    Ibrahima LyMese fa

    Boy lac mome day kharr kw

  • Mansour Diop
    Mansour DiopMese fa

    Fran vs malick niang

  • Dominique gomis
    Dominique gomisMese fa

    Félicitations champion 💪🏾

  • Beute Basse
    Beute BasseMese fa

    Khékh ngay wakh ndiago franc ndiago la aboukk na ndiagou dika lall athi wou feukk dina peung karéé mu keurr ka tambeu ku 💪💪💪💪💪

  • Mamadou Lamine Gaye
    Mamadou Lamine GayeMese fa

    Prkw pas tous les mbeurou P.A bokou béneu écurie? Ndawe lou néekhe

  • GALAYE DIOP
    GALAYE DIOPMese fa

    mbeur day osé.nièmè lingay wax.koumou nèxoul dieuleul avance bi niou xool

  • mame baye gueye
    mame baye gueyeMese fa

    Babacar s'il te plaît numéro franc guir yalla diappalé ma sii

  • Dieter Windl
    Dieter WindlMese fa

    👏👌👍

  • Lasana Seck
    Lasana SeckMese fa

    Franky et lac2 combat bou nekhe la

  • Modou Wade
    Modou WadeMese fa

    Thiey franc

  • Ibou Diop
    Ibou DiopMese fa

    Franc dimbali gnou siiii lac rèke mou nopalou

  • Aliou Kama
    Aliou KamaMese fa

    C'est la relève de modou lo franc un grand champion

  • Papa Elhadji Thiam
    Papa Elhadji ThiamMese fa

    Lac 2 vs franc combat leu dh

  • kally kurumang
    kally kurumangMese fa

    Congratulation Fra my champion Wishing you all the best

  • Diop Keba
    Diop KebaMese fa

    Big up champion félicitation

  • Mouhamed Ndiaye
    Mouhamed NdiayeMese fa

    Franc vs Diene kaïrè : un combat inevitable 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • Mbeur Sarr

    Mbeur Sarr

    Mese fa

    malick niang rek

  • Abdoulaye Ndoye

    Abdoulaye Ndoye

    Mese fa

    Diéye daay haar on atten reus reug gouye gui ou moussa ndoye sathies

  • Wagne Oumy

    Wagne Oumy

    Mese fa

    Lolou dou comba nako lac2 maye sans wala mou khar reug reug

  • cedric samba

    cedric samba

    Mese fa

    😁😁 mouhamed Ndiaye iao kula bayéh diène kaïre nga soul carieram

  • Sarr Abdou

    Sarr Abdou

    Mese fa

    Way bann diéne ki meunn boy yi yup

  • Saliou Niang
    Saliou NiangMese fa

    Franc vs Diène kaïré

  • LOHM FATY

    LOHM FATY

    Mese fa

    non lolou dou combat franc mo raw kairé

  • Mbaye Ndiaye
    Mbaye NdiayeMese fa

    Beuri manoko Dole ak galathi rek gua ame

  • Mouhamed Dia

    Mouhamed Dia

    Mese fa

    Est ce que dou bolé equipe national denegal ak aye serigneum pour niou dieule mondial.

  • Mbaye Ndiaye
    Mbaye NdiayeMese fa

    Defal ndanke lambou da doy War ki da koumace beuri wakh

  • matar mbuege

    matar mbuege

    Mese fa

    @Saer hihi Odf gayi li nga wakh duegla

  • Saer hihi Odf

    Saer hihi Odf

    Mese fa

    Yén mome kou Koumasé wakh loulén arrangé woul RK ngén ni da beuri wakh hay hay hay hay

Il prossimo